.

Bayi Yoon Lyrics

intro: sAMA GAA GNA NGI DOOMU AFRICA MBEUR LA KAAMIL
YAGG YAGG DINA DAANI CI Gééw KéN DOUKO JAMNAANI
NéNAALA SAMA GAA GNA NGI...
REFRAIN: ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon jikko you rafét yignou ragnéwoon?
dafa melni dagnou bayi sougnou yoon beugeu askano lougnou momoutoon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon oh!!wow!!
Africains et fiers de ce que nous sommes
Africains et fiers de ce que nous sommes

COUPLET:

fier d'être africain je suis
je suis africain donc je suis
mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi
c'est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau
pour me mettre k.o. il faut minimum une armée de cent mille(100000) rambo
Dis à ton prof d'histoire qu'il raconte des histoires,la plus grande des civilisations est
Née en Afrique noire.
L' afrique a inspiré le monde avec ses pyramides sa science et ses mathématiques
Ses symboles et ses signes
Elle créa l'écriture avec les hyérogliphes du temps des pharaons tu ne me crois pas
Demande à akhenaton...
(de dakar à marseille)
REFRAIN: ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon jikko you rafét yignou ragnéwoon?
dafa melni dagnou bayi sougnou yoon beugeu askano lougnou momoutoon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon oh!! wow!!
Africains et fiers de ce que nous sommes
Africains et fiers de ce que nous sommes

COUPLET:
Dafa melni gnou ngi daw jeum fénén ni wacc wacc nagnou ande yi
xéeb sougnou ngande yi fékki borom jikko you dande yi/ fo daw fo daw
di nga wirri ndaari fa nga jougé fi nga dooré fila wooré doufou sorré/
AFRO sama dolé na nga mako xolé geum sama démb doon nittou téy
njaxass ni xéetou parfum'k'Gowé/ Africains koula xass foy gnawé/
Africains xola gneup nignouy ngaangé/ Africains soy joug doufi gawé/
koula xol dina séet fan la lay ngagné/ geum sa bopp xam fi nga bokk
melni garab réen banxass ak xob/ dougnou fatté fignou jogé ndakh panafricanistes
délo sougnou xél démb kanamou mame gnou giss/ dimbali jam yi biss- gnoul métisses
dékkil osiris -carbone14 souliwaat gnou giss- histoire bindaat grand pére ba petit fils
bamako singapore anghata!!!

outro: sAMA GAA GNA NGI DOOMU AFRICA MBEUR LA KAAMIL
YAGG YAGG DINA DAANI CI Gééw KéN DOUKO JAMNAANI
NéNAALA SAMA GAA GNA NGI...
Report lyrics
School of Life (2010)
Bayi Yoon Celebrate Tomorrow Children Temps Boy Potu Nda Positif School of Life Oh Why Sun Afreeca Gates of Freedom Janggileen
Top Daara J Family Lyrics