.

Sey Lyrics

bo takké sa jieg amak mom ay tom boko weuthié sa jaboot taxawalu yay mi jiguén topatol sa sey té fo mena toll nangol dann sa dollé moy sa waref baylén jay sén domm ala du sey
sey 3 waref la dund bu doy thiangay lu doy jamm ju sa lolu moy sey, gayi sédé lén ma
Report lyrics