baye bayou nieupe la,
sama yaye djé, sama yaye djii,
guissouma koumalay meuna wethiéé,
yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane.
yaye boye sama galadj.
bo beugué djote sama djiko
toudal sama yaye
douma ko fowé doma ko fowé
yaye boye sama galadj.
rote nga thi leudeum debb nga thi taw,
wale thi nadj bou tang
bou yaye yeup melen ni yaw
kene dou diour di sani.
(refrain )
ndeye ndeyou ken la
baye bayou nieupe la,sama yaye djé, sama yaye djii,
guissouma koumalay meuna wethiéé,
yaw mi gueune si mane yaw mi gueune si mane.
yaye boye sama galadj.
djéba Ndoye, Indou woma woma ndeye sane,
bayo boye dom djou am yaye day am baye wow wo.