.

Yaye Boye Lyrics

aye boye balalma (3x) - maman chérie pardonne moi
Khamna awma loula eupeu si adounya - Je sais que je n'ai rien sur terre de meilleur que toi
Yaye sama wadiour yaye sama lepeu - Tu es ma famille, mon tout
Yaye man - maman
Kon yaye soumala masse togne mangui - Alors maman si un jour je t'ai fait mal
Dieguelou - je te demande pardon
Souma masse dioum tay rethiou nako - Si auparavant je me suis trompé aujourd'hui je le regrette
Ndakh yaye man guisna khale magua - Parce que maman j'ai vu un enfant grandir
Sama kanam - Devant moi
Ma khamne yaye boye fii la diar
- Et j'ai su maman chérie que j'ai emprunté ce même chemin
Balalma balalma baalalma (2x) - Pardonne moi, pardonne moi, pardonne moi
Yaye boye - maman chérie
Soumala masse togne mangui dieguelou - Si un jour je t'ai blessé, je te demande pardon
Souma masse dioum tay rethiou nako - Si auparavant je me suis trompé aujourd'hui je le regrette
Ndakh yaye man guisna khale magua - Parce que maman j'ai vu un enfant grandir
Sama kanam - Devant moi
Ma khamne yaye boye fii la diar - Et j'ai su maman chérie que j'ai emprunté ce même chemin
Balalma balalma baalalma (x2) - Pardonne moi, pardonne moi, pardonne moi
Fane la mana diarr ba fayla yaye yaw - Que pourrai-je faire pour te payer maman
Ndakh fayla douma yomba yaye man - Car te rendre tout ce que tu m'as donné ne sera pas chose facile
Waye dina diem sama kemtalay katane - Mais j'essaierai de toutes mes forces
Bagua contane - Jusqu'à ce que tu sois contente
Louma def si yaw warou mako naw - Je ne dois pas me vanter de ce que je fais pour toi
Yayo ho yaye beuguena yaw ngua contane - Maman oh maman je veux que tu sois contente
Ndakh bo contane yala dana contane - Car si tu es heureuse, Dieu le sera aussi
Gnou sargual sounou yayboy - Honorons nos mamans chéries
Yaye boye sonnagua yaye boye - Maman chérie, je sais que tu es fatiguée
Masso tayi - Mais tu n'abandonnes jamais
Yaguala tankhal dila sonal yayo - Depuis toujours nos tourments te fatiguent
Rethiouw ma loma done dioure - Je n'ai jamais regretté d'être ton enfant
Khamna amoul lo dadioul si gnoun gny - Je sais que en tant qu'enfant nous t'avons causés pas mal de tracas
Tay alhamdou lila mane mi bay la - Aujourd'hui grâce à Dieu je suis devenu père

Diour na y dome khamna yoor ndiabote - J'ai des enfants et je sais ce que élever des enfants (avoir une famille)

Modi lane (...)
Yaye boye yala nala yala fay - Maman chérie que Dieu te bénisse (te paye)

Balalma yayoboy balalma balalma - Pardonne moi maman chérie, pardonne moi, pardonne moi

Balalma yaye boye balalma - Pardonne moi, pardonne moi
Report lyrics
Sénégal (2006)
Baykat Incha Allah Tass Yakar Le Jola Taar Dusey Manko Yaye Boye Plus Je Fais Ci, Plus Je Fais Ca Mbindane Wakhal Ouvriers Jiguen Ma Fille Tajabone