.

Le Jola Lyrics

senegal senegal siguil ndiguale
gambia gambia oh siguil ndiguale
amna benna ferie bougnou dane nane
bateau le jola mi soukh sibir gueth gui
xalebi migui dioye nane baye
baye anna sama yaye boye
baye neko dome anna yaye boye yaw
senegal senegal siguil ndiguale
gambia gambia oh siguil ndiguale

mane baye migui dioye nane dome
dome anna sa yaye boye
dome neko baye anna yaye boye yam
kone li firina ni yala reke sagne yala
reke mane kon mome rekeu moy bour
refrain

ndakh kepeu ko lath moune amnathi
waye kon lii fir ndena ni senegal bena bopeleu

senegal beneu bopeleu
senegal beneu bopeleu
bilay

ken douko khar gnaro

beneu bopeleu senegal

f**uarou diotna
nagnou xolat sougnou bopeu bou bakh
Report lyrics
Sénégal (2006)
Baykat Incha Allah Tass Yakar Le Jola Taar Dusey Manko Yaye Boye Plus Je Fais Ci, Plus Je Fais Ca Mbindane Wakhal Ouvriers Jiguen Ma Fille Tajabone